Wereg xeetu garab gu bàyyikoo Afrig te bokk ci njabootu fabacées.
- Dees koy fajoo. - Dees koy jëfandikoo ci aniin - Dees koy lekk.
tóortóori wereg
xobi wereg yu wow
xob yi
Daakaaney wereg
Senegalia senegal